The Holy See
back up
Search
riga

KUREELU PAAP BI NGIR BOKK
WAXTAAN BI CI DIGANTE DIINE YI

BATAXELU SUTTITEE KOOR GI

Id al-Fitr 1428 H. / 2007 A.D.

KERCEEN YI AK SERI YI WAR NA U
AND LAWLOO AADA U JAMM JI

 

Yeen sumay xarit seri yu baax yi,

1. Lu ma neex lool la, ma di leen jottali yeney kureelu paap bi di ynggu ci waxtaan gi war ci digante diine yi, yeney xarit, te u sawar di ko def, ci seen xew-xewu Id al-Fitr bi di xewte baneex te di jeexantalu doxum weer lmm, bi ngeen dox, ci koor ak aan, di weeri Ramadaan bi. Dox boobu jamano ju am maanaa la ci dundu mbootayu seri yi, mu di jottali ku nekk doole gu bees ngir dundu boppam, bu njabootam ak bu mbootay gi mu bokk. Ndaxte lu war la, ku nekk di seede li diine di santaane, ci dund guy gn di jub te gna mengoo ak li Bindakatu aduna bgg, and ci ak xalaata surgawu ay mbokkaam, bokk soxla ak oom, am xolu mbokk ak i bokk ci yeneen diine yi, ak nit i di uta def lu baax pp, ndax rekk bgg bokk ligey ngir liy jeri nit i pp.

2. Ci jamano ju jaxasoo ji nu nekk, i gm ci diine yi, am na u sas wu jiitu : moo di ligey, niki surgay Aji-katan ji ngir jamm ji nga xam ne balaa muy am, ell na u may cr li nit ku nekk ak li mbootay bu nekk gm, te ku nekk yaatu ngir mna jaamu Yall naka lako diineem tralee. Yaatu ci diine bobu nga xam ne yemul rekk ci am sasau mttali ay taxawaay u ngm, benn anam bu jiitu la ci li di njambuuru fit bi nga xam ne yelleefu nit ku nekk la, di itam li di woral yelleefu nit yi ypp.

Su nu bggee taxawal aada u jamm ak bokk soxla ci digante nit i, ell na u bayyi xel ci loolu ; noonu, pp di na u mna soobu te yebu ngir jagal mbootay buy gn di nekk mbootayi mbokk, te di nau mna def lpp li u mn ngir ba fitna bu mu mnti doon, ngir weejee te yedd kpp ku bgga jfoo fitna ; te moos, fitna mnul sukkandiku mukk ci diine, ndaxte defay aawloo nit ki bindu ci meliinu Yall. un pp xam nanu ne fitna, waxatu ma iite tiitalaate ak boom bi dul raatle ci kaw an lay dal te muy lor nit u bare, jkkee ko ci jambuur yi mnul sottil bajjikonte yi, lu dul, xanaa, jur dee, mba ak yaqqal nit i ak mbootay yi.

3. un i di niti diine, nun pp noo wara jiitu ci li di jangalee jamm, ci yeete ci yelleefu nit i, ci digal njambuur bu di cral nit ku nekk, ak itam dundu mbootay buy gna am doole ; ndaxte nit ki defa wara saytu bpp nit, ci kaw li mu bokk ak moom ndey ak bay, baa tuutil kenn. Waru u gnnee kenn ci mbootayu rew ngir xeetam, diineem, mbaa beneen melukaan bu nekk ci moom. Nun pp i bokk ci xeetu diine yu uutante, sunu sas moo di lawloo jeemantale bu di suturaal bpp doomu adama, lawloo yene cofeel ci digante nit i ak ci digante xeet yi. Li gna nekk sunu sas moo di nu yar ndaw yi ci xalaat boobu, oom i wara doxal aduna si suba. Njaboot yi, i am cr ci yarum ndaw yi, njiiti addina yi ak yu diine yi, pp de oo wara farlu ci di jottalee njeemantale bu jub, ak ci fexeel ku nekk yar bi war ci anam yi u fi tudd, u gna fsal jeemantalee dund ci mbootay bu di xamal ndaw bu nekk mu cral i ko wr te seetee leen niki u mu bokkal ndey ak bay, te mu wara dund ak oom bes bu nekk. Waxu u nga def niki ku xamul i muy dund ak moom, wande nga di bayyi xel ci oom, niki su u nekkoon ay mbokk.

Kon lu jamp lool la, u di jeemantal maasi ndaw yi li nit i japp niki lu baax, li di dund gu rafet, li di taxawal dund ci biir mbootay, li ci jiitu, te nga xam ne mnu u akk nekk ngir dundu nit ku nekk ak dundu mbootay bi. Saa yu u gisee ndaw yi def naka su dul noonu, war na u len fattali li uy xaar ci oom ci dundu mbootay bi. Njekk lu baax li war mbootay bu nekk ak addina si sepp ci loolu la aju.

4. Yooyu xalaat oo wara tax nu japp ne lu am maanaa la u wey dund te gna dooleel waxtaan bi ci digante kerceen yi ak seri yi ci li mu nekk yar ak saxal aada, ngir u boolee mnmn yi ypp, u jeri nit ku nekk ak nit i pp, ndax maasi ndaw yi baa doon getti aada ak diine yu di xeexoo, te u doon ay mbokk ci kaw li u di ay nit. Waxtaan bi doon na juntukaay, bu nu mna dimmali be nu gnna ci bojjikonte ak ŋaayoo yu bare yi ci biir mbootay yi, ndax xeet yi ypp mna dund ci dal ak jamm, u di mayante cr, te njaboot yi uutee yi dund ci dggoo.

Ngir loolu mna am, mangiy dagan pp u yebu : noonu, ci pexe dajee yi ak weccoo yi, kerceen yi ak seri yi and ligey, ii di cral ii, ngir jamm am, te nit i pp mna yaakaar addina su gna neex suba. Noonu itam, di na u doon rooyukay ngir ndaw yi. Ndaw yi di na u leen top te toppandoo leen. Ndaw yi di na u gna wllu dundu mbootay te di na u gna sawar ci bokk ci mbootay bi ak ligey ngir soppali ko mu gna baax. Yar gi, ak wonee rooyukay di na leen may u am yaakaar ci addinab suba.

5. Lilee moo di iite bu ma or bi ma bgg seddoo ak yeen ; kerceen yi ak seri yi war na u yokka digaale xaritoo yu di defar ngir u weccoo lu jekk t rafet li ku nekk am, te u sabablu bu baax seedees gmkat bu rafet !

Yeen sumay xarit seri yu baax yi, mangi leen waxaat suma yeene yi ma tibbee ci suma xol, ci seen xewte bi, te mangi aan Yallu jamm ak yermande bi, mu may leen yeen pp wrgum yaram, dal ak naatangee.

Jean-Louis Kardinaal TAURAN
Njiit li

Pier Luwiji CELATA
Bindakat bi

   

top